background cover of music playing
Oulalalah - Samba Peuzzi

Oulalalah

Samba Peuzzi

00:00

03:25

Similar recommendations

Lyric

Toujours au tiek posé dans le bendo

Ñangal chaque jour ba nga fokni dañu ñaaw

Firi rek baćc bo yéexe do guiss

Gang bi dañu méchant oulalalah

Firi rek baćc bo yéexé do guiss

Gang bi dañu méchant o

Oulalalah

Ouwa ah ah ah ah ouwa ah

From diack wawaw

Ouwa ah ah ah ah ouwa ah

Oh my gang

Hey tapette dufi fréq (non non)

Fake dufi fréq (non non non)

Indique dufi fréq (non non)

Snitch dufi fréq (non non non non)

Diamaguene for life sama side waw waw

Thiow li thiow li fils lepp fi la

Muy mag di ndaw ko ci laaj nala wax

Fi ñëpp xam ni devise bi li leu

Samba kuko bëgg ñu bëgg la

Kuka bëggul ñune bëhgu ñula

Kuko bëgg ñu bëgg la

Kouka bëggul ñune bëggu ñuko

Toujours au tiek posé dans le bendo

Ñangal chaque jour ba nga fokni dañu ñaaw

Firi rek baćc bo yéexe do guiss

Gang bi dañu méchant oulalalah

Firi rek baćc bo yéexé do guiss

Gang bi dañu méchant oulalalah

Ouwa ah ah ah ah ouwa ah

From diack wawaw

Ouwa ah ah ah ah ouwa ah

Oh my gang

Niggas hate hate hate hating

But mama pray pray pray for me

With my gang gang gang gang gang

From the bottom now all eyes on me

Da nga fogon du nekk té pourtant on l'a fait

T'as vu ouais t'as vu

Pour yaw duñ ci gennë té pourtant on l'a fait

T'as vu ouais t'as vu

Devise bi li leu

Samba kuko bëgg ñu bëgg la

Kuka bëggul ñune bëhgu ñula

Kuko bëgg ñu bëgg la

Kouka bëggul ñune bëggu ñuko

Toujours au tiek posé dans le bendo

Ñangal chaque jour ba nga fokni dañu ñaaw

Firi rek baćc bo yéexe do gis

Gang bi dañu méchant Oulalalah

Firi rek baćc bo yéexé do guiss

Gang bi dañu méchant Oulalalah

Ouwa ahah ahah auwah

From diack wawaw

Ouwa ah ah ah ah ouwa ah

Oh my gang

Gang, gang, gang, gang, gang, ...

- It's already the end -