background cover of music playing
Xool Ma Ci Bët - Iss 814

Xool Ma Ci Bët

Iss 814

00:00

03:25

Similar recommendations

Lyric

Mbeuguel bou deugou

Dara douko faye

Yaay seetou

Biye woné sama leeraye

Jant goudi

Biddew soubeu teel

Bimala xamé

Ci la tagok weetaye

Nii tognal sa aaaaaa! yaye

Balenala ndakh mbeuguel bimaay yeug Ci yow

Nii tognal sa aaaaaa! Baye

Balenala ndakh mbeuguel bimaay yeug Ci yow

Wolou nala wolou wolou nala!

Eh yaaaay!

Wolou nala wolou wolou nala!

Ahn ahn!

Boume laay guiss ngaay doundou

Dafemaay doundeul baby

Soume laay guiss ngaay rétaan

Dafemaay doundeul waay

Boume laay guiss ngaay doundou

Dafemaay doundeul baby

Boume laay guiss ngaay rétaan

Dafemaay doundeul waay

Xool ma ci bët

Ma xool la ci bët

Nioune niare la rek

Mbeuguel a nekh

Xool ma ci bët

Ma xool la ci bët

Nioune niare la rek

Mbeuguel a nekh

Yéne saaye nga diéki diéki woma

Woma

Nga meer maané mba diépiwoma

Nga néma non non

Yéne saaye nga xole ma rek Ma rétaan rétaan

Yaay sama boumou xol bi

Yaay sama boumou xol bi

Bo meeré ba guédeu dafemaay metti

Metti

Bo deffé ba gnipeu

Nala setsi

Setsi

Douma ci xole sax pa bek mère bi

Mère bi

Na oubi bountou bi soxna si

Dang ma diape sa mbaal

Té douma guéneuti

Bilay walay yé

Yow laay fethie ci bal

Yaay sama mélodie

Yow rek la baredé

Eh eh!

Boume laay guiss ngaay doundou

Dafemaay doundeul baby

Soume laay guiss ngaay rétaan

Dafemaay doundeul waay

Boume laay guiss ngaay doundou

Dafemaay doundeul baby

Boume laay guiss ngaay rétaan

Dafemaay doundeul waay

Xool ma ci bët

Ma xool la ci bët

Nioune niare leu rek

Mbeuguel a nekh

Xole ma ci bët

Ma xole la ci bët

Nioune niare leu rek

Mbeuguel a nekh

Yeh weurena ba weurengueul adouna

Yeh kou melni yow mba amatina

Yeh dougueul ci Keur gui yatouna

Ndakh yow yaay yaay sama boumou xol yaay sama boumou xol

Yéne saaye nga diéki diéki woma

Woma

Nga meer maané mba diépi woma

Nga néma non non

Yéne saaye nga xole ma rek

Ma rétaan rétaan

Yaay sama boumou xol bi

Yaay sama boumou xol bi

Weurena ba weurengueul adouna

Yeh kou melni yow mba amatina

Eh yah dougueul ci Keur gui yatouna

Ndakh yow yaay

Yaay sama boumou xol

Yaay sama boumou xol

- It's already the end -