background cover of music playing
Guuy - Jeeba

Guuy

Jeeba

00:00

03:57

Similar recommendations

Lyric

Dinala daal foko doul fogué

Foko doul khalaté

Sa baniouy doguou thie lalaay dougué

Deey melni yallah ko yoné

Dina fess sa xool bi unh no no no

Eulemeul sa boop bi unh yeah yeah

Doto amati principe, Bafouer nga leep

Meuno guiss si moom siik

Yoow loum lay deef dou yow rek yakoo xaameu

Dou lou niit meuneu wakh

Yoow fim may yobou dafa melni meussoumafa deemeu

Wayé dou lou niit meuneu wakh

May topou sa guinaw di doow melni mbeguélou xalé xalè xalé

May ladj kagn laay magué

Nga teyi si sama yeri bi niiuy khandal dowaal mbégué mbégué mbégué

Degg na sakh dama jongué

Kaaro kaar kaar machallah daniou beuguenté ba niroo

Yaay sama hero

Sama bébé d'amour conquérir nga sama xool

Fi yaafiy bour defal loula nekh nga xool

Bo bégué ma begg bo dioyé ma dioy

Lima guissoul si niom la guiss si yow mou doyma

Sandi nga cravache dane ngaleen diél bou gaaw

May sa djomba niaaw djomb nala deef lou niaaw

Ndakh Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié

Mane Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié

Yoow Seral nga sama xool guuy guuy guuy

Seral ngamaa guuy guuy guuy

Walay seral nga sama xool guuy guuy guuy

Seral ngama Guuy guuy guuy guuy

Tank tank mbague ak mbague niou deem

Waat nani dinala yobou Fenen

Yoow defal nank boul deglou wakhi noone

Niom douniou deem beugouniou kou deem eeh

Khana xamoni lou bakh nieupeu ko beugg beugg

Fi liniuy wakh khadj ba dou deugg deugg eeh

Khana xamoni meune naniou wakh mais duniu beugg

Seen biir xool meunou niou guiss niaar niou beguenter

Tei xamnani warone na done Gueweel ma tagaal la say maam

Warone nga done jaam ma goreel la goreel saay maam

Souma amone avion dou ma maylako dila dowaalal fo beugg

Niou dieum thia li soula doyoul wakhma loulay dooy bébé

Bilay walay khawma lilay dooy

May topou sa guinaw di doow melni mbeguélou xalé xalè xalé

May ladj kagn laay magué

Nga teyi si sama yeri bi niiuy khandal dowaal mbégué mbégué mbégué

Degg na sakh dama jongué

Kaaro kaar kaar machallah daniou beuguenté ba niroo

Yaay sama hero

Sama bébé d'amour conquérir nga sama xool

Fi yaafiy bour defal loula nekh nga xool

Ndakh Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié

Mane Kerok bama la guissè eh eh sila xamni doma reuthié

Yoow Seral nga sama xool guuy guuy guuy

Seral ngamaa guuy guuy guuy

Walay seral nga sama xool guuy guuy guuy

Seral ngama Guuy guuy guuy guuy

May topou sa guinaw di doow melni mbeguélou xalé xalè xalé

May ladj kagn laay magué

Nga teyi si sama yeri bi niiuy khandal dowaal mbégué mbégué mbégué

Degg na sakh dama jongué

- It's already the end -