background cover of music playing
Abadane - Baye Mass

Abadane

Baye Mass

00:00

02:34

Similar recommendations

Lyric

Pape Laye

Doumala bayi

Doumala bayé eheh

Yawite bouma bayi

Boulma bayé yeah

Mom nene daf leu beugueu piir

Nena dafa beugueu nga nekka ki mou djital

Mome néna yadi kimou guiss

Nena tchi ñom ñeup yaw rek la beugueu djital

Nèna dotu la bayi

Yaw la taneu si goor gné

Nèna dotou la bayi

Yaw la taneu si djiguene gné

Douma la bayi

Douma la bayè

Yawite bouma bayi

Boulma bayè

Abadane

Abadane

Abadane

Abadane

Yaw boulma bayi dahimane

Abadane

Abadane

Abadane

Abadane

Douma la bayi dahimane

Pape Laye

Sa agne mo daak louma meune lekka

Sa keur mo dakk fouma meuna nekka

Lougniou neex lekka

Louniou neex nane

Ndiabote gui fecc aka retane

Mane dama la nopp ba dila beug fone

Mane damala manguila chérie mouah

Dama la nopp ba dila beug fone

Mane damala manguila chérie mouah

Doumala bayi

Doumala bayé eh

Yawite bouma bayi

Bouma bayè eheh

Abadane

Abadane

Abadane

Abadane

Yaw boulma bayi dahimane

Abadane

Abadane

Abadane

Abadane

Douma la bayi dahimane

- It's already the end -