background cover of music playing
Monsieur Bonheur - Adiouza

Monsieur Bonheur

Adiouza

00:00

03:18

Similar recommendations

Lyric

Mr Bonheur nexa joubole

Dafa jote nga gneuw gnou waxe

Taye jameu la yewo

Bae sagou bi doyna

Ma guiss néne

Ni néna ngui

Thiapa thioly

Do kéne thi gni

Lo viser

Doko moy

Raféte nguémb

Meuné beuré souf

Nonou lalay nammé

Dotou moko def

Te foma méré ma diakh lé bébé

Dotou mako def

Balma dotou moko def

Yaw xolma tay ré bébé

Dotoumako def

Gnou def joboo de l'année bébé

Dotoumako deff

Balma dotou moko def

Dama paré dioubok yaw

Ba fofou gnouy wowé wouyaye oohoo ohoo

Khamanté nagne dou ame thiow oohoo ohoo

Diéleu ame foko fogué woul

Soukeur bi thi banana

Paré noy ni xaale

Menthe bi né thi nana

Ak yénene yilay xaar

Doyalouma

Mére bi doyna

Doyalouma

Nonou lalay nammé

Dotou moko def

Te foma méré ma diakh lé bébé

Dotou mako def

Balma dotou moko def

Yaw xolma tay ré bébé

Dotoumako def

Gnou def joboo de l'année bébé

Dotoumako deff

Balma dotou moko def

Meuno dém kaay ndax yaye sama poumon gauche

Waw Waw Waw Yaw la

Meuna fi dé thi une minute de pause

Wallah wallah

Am nga thiass stylé nga

Mako léteu kaay firiko

Diekha goul doya louma

Dianteu soow kaay dolima

Doyaaa louma

A vie lagne signé

Doyaaa louma

Nonou lalay nammé

Dotou moko def

Te foma méré ma diakh lé bébé

Dotou mako def

Balma dotou moko def

Yaw xolma tay ré bébé

Dotoumako def

Gnou def joboo de l'année bébé

Dotoumako deff

Balma dotou moko def

Weye mbegel manak mbegel

Bae tay la tay

Bae tay la tay

Dara ladoule mayé

Bae taye la taye togale

Bae taye la taye

Dara doumako mayer

Bae tay la tay togale

Dara ladoul mayé

- It's already the end -