background cover of music playing
Mburok Lem - Leuz Diwane G

Mburok Lem

Leuz Diwane G

00:00

03:51

Similar recommendations

Lyric

Ou naa naa naaaa

Eh eh ehhh

Sa araass laniou bolé niari rouh yi

Adouna dou wone touki té guissé wouniou ba nopi

Ehhhhhhh héee

Bén palace niou beuneu sama rouh gui

Né kou démone touki té meunoul nieuw ba légui

Ehhhhhhh hé héee

Dianakhé-k banekh dima kali kalé

Kagne lay done ak noumay déff ba guisla

Dane na khégn lou gueun nekh dou kii dou keulé

Nga néwone si yone noumay déff ba miss la

Stagiaire laa wone cv bi demna founé

Ndékété yoo douma ligueey si niom

Dou dianeer dagne mala wane mbégté la yoo

CD bi dathie boudé yay diour samay dome

Youssou Ndour ak Péne

Khamone naani daniou dadié té dou ndourok lénn

Khamone naani beuss bouniou dadié moy dakheu mbourok lém

Doumala fénn, give me your hand

Niou ande dém féneen, dieundé woumala kénn

Dou kéneu si niom kou moune dara si nioune

Té nioune sokhlo wouniou khoulok kénn

Nga togne ma maalay baalou

Wakhlén ma kagne laay dallou

Kou sagna tamba-mbalou

Boma méré ma waarou

Baayilén niou wakh loulén nekh

Guisagouma louniou wara téré dém

Lima yeuk khadioul si ndap dou dieeeekh

Baayilén niou wakh loulén nekh

Guisagouma louniou wara téré dém

Lima yeuk khadioul si ndap dou dieeeekh

Kéee wakh ko boumou yakh crédém

Danga gueuneu fort khéttou bone si man

Tatt laay déff soumala diéguéé

Meun nga sa borr matt nga linga done si man

Boudoul yaw sama tole kénn douko niaguéé

Bokak yaw keur di fo di réée di contane

Moy sama yéné si yaw

Mou antou niou mour la nga ouf sama ndiabote

Je t'aime mon cœur kén douniou réé é é

Do dégue Ndeysaan

Dinala téyèè nimou waré ba dégue diarabote

Ma moitié, ma reine, l'autre moi

Ma meilleure amie

Quand je parle de toi j'ai des larmes aux yeux

Je t'aime et tu es toute ma vieee

Youssou Ndour ak Péne

Khamone naani daniou dadié té dou ndourok lénn

Khamone naani beuss bouniou dadié moy dakheu mbourok lém

Doumala fénn,give me your hand

Niou ande dém féneen, dieundé woumala kénn

Dou kéneu si niom kou moune dara si nioune

Té nioune sokhlo wouniou khoulok kénn

You know I love you

Never dare a leave you you know I need you

Every day every night I'm thinking about youuu

Night and day every where I go baby I see you

There is no one... no one like you

Nga togne ma maalay baalou

Wakhlén ma kagne laay dallou

Kou sagna tamba-mbalou

Boma méré ma waarou

Youssou Ndour ak Péne (hé hééé)

Khamone naani daniou dadié té dou ndourok lénn

Khamone naani beuss bouniou dadié moy dakheu mbourok lém

Doumala fénn,give me your hand

Niou ande dém fénee, ndieundé woumala kénn

Dou kéneu si niom kou moune dara si nioune

Té nioune sokhlo wouniou khoulok kénn (hééééé)

- It's already the end -