background cover of music playing
Diarabi - Jeeba

Diarabi

Jeeba

00:00

03:56

Similar recommendations

Lyric

Eh eh eh eh!

Djiba leu boy

Yéwou djakarlo ak sa Kane

Sama beutt yi di khool di leu kholl oh oh oh oh

My guiss si seu kanam ba ex

Mbeugël bou doul djeikh, mane ak ioe ba assaman (eh assaman)

Dakanté, doranté ni khalei foumala djéko balnako té

Ioe foma djeiko gua balma guirr mbeugël bi ngmay wane

Yakamti beu gnou né Al khayri ma kheuthie leu taff

Leu sama kaw do toma reuthie abadaaane (eh abadane)

Mane yéné naa kounekk mou dound love bimay dound

Mane yéné naa kounekk mou kham li my

Doundou al Jannah té déwa gouma (nono déwagouma)

Djokhla samay beutt womatt ma gui goumbeu, ioe womatt ma gui goumbeu

Ouhhh

Ba khôl bi réré ioe yako for fatt ko sa këër nonou lama léré lo amoul

Ci mane lepp ci ioe leu ehh déma réé

My contane di begg (eyy déma ré éh éh éh)

Djokh nala li, djokh nala lépp

Guiss nala fi guiss nala fépp

Djokh nala li, djokh nala lépp

Guiss nala fi guiss nala fépp

Beu dafa melni ioe dagua djougué

Assamane indalé mbegté, mbegté bouy nieuw ci mane

Défé na ni, deff naaa ah la nii guey sama diarabi

Diarabi ih ih ihhh

Yéwou djakarlokk sa kaname du weur fane la nekk di ko sett

Ma name la té soriwoma yakamti ba

Djantt bi fekk bama guiss leu fi sama wett

Ioe taw bi di nieuw sama toll sans ioe lepay wow ioe ya takh ma niafé

Beugg done seu goor bou dé ci ioe kone boul titt boul meusseu nango

Djakhlé al Jannah la lay yobb ioe boul titt

Djakhlé mane ak Ioe ba abadann anh anh anh waw

Djokhnala li djokhna la lepp guiss nala fi guissna la fepp

Djokhnala li djokhna la lepp guiss nala fi guissna la fepp

Beu dafa melni ioe dagua djougué

Assamane indalé mbegté, mbegté bouy nieuw ci mane

Défé na ni deff na né guey sama Diarabi

Diarabi

- It's already the end -