background cover of music playing
Madame Bonheur - Adiouza

Madame Bonheur

Adiouza

00:00

02:55

Similar recommendations

Lyric

Ouh ouh hou

Hou hou hou wa

Hou houhou hou

Xolou ma kenen

Fess na sama settu

Djiguene dji wakhé djeuf

Dou am diotou tontou

Doon awo di bourou keureum

Li dou ay fontou

Té sakh fouma momé

Zéro lakoy wathié

Lou deuss meuneu daw

Un bé ngui ci kaw

Gnari faan gnouné fo feug aljana takhaw

Bonheur

Fi wakh amoul

Thiouray bi riir

Def terreur

Loutakh mouy sedd té may diegg pire

Péssé sama bopou

Kham né warou ma ragal woudié

Ladial mon cœur

Kouy madame bonheur

Ya may confiné

Lepp di dioub

Ya raw poli-cier

Ladial mon cœur

Kouy madame bonheur yé

Li ley door

Té doula laal

Nékhoul ci xol

Deuxième dame

Bi la gnou takkal médaille d'or

Ki nélaw la khamone

Ma diangal ko yandor

Bayi léen di diem

Diang kham sa goor a gueuneu woor

Xol bi nangou féété

Boboy doundou mbecté

Namouma daray wakh

Beu fi mingui bakh

Chéri dougueul deuk

Do feug yay laisser passer

Allô

Fi may sourire mou évanouir

Mais allô

Ay nélaw diékh na té may nonou

Péssé sama bopou

Kham né warou ma ragal woudié

Ladial mon coeur

May ki key bonheur

Yamay confiné

Lepp di dioup

Ya raw poli-cier

Ladial mon cœur

May ki key bonheur

Coco man ak yaw ba Aljana

Thi sa wett la doundé oh lala

Ya raw ci man

Say je t'aime thi sama biir tympan

Nim may def nekh na ma

Beug nala babe

Péssé sama bopou

Kham né warou ma ragal woudié

Ladial mon cœur

Kouy madame bonheur

Ya may confiné

Lepp di dioup

Ya raw poli-cier

Ladial mon cœur

Kouy madame bonheur

Ladial mon cœur

Kouy madame bonheur

Ladial mon cœur

May ki key bonheur

Kouy madame bonheur

Ladial mon cœur

Kouy madame bonheur

Ladial mon cœur

May ki key bonheur

Ladial mon cœur

May madame bonheur

Ladial mon cœur

May madame bonheur

- It's already the end -