background cover of music playing
Ni La Deh - Sokhou Bb

Ni La Deh

Sokhou Bb

00:00

02:49

Similar recommendations

Lyric

Maestro on the beat

Baby

Kouma la nara xañ dial félé

Soma reuthié lu mél ni fan lakoy jeulé

Beug na mane

Sa yo guésso guissma si sa wétt

(anhhh yoooh)

Cheri kañu juboo

Surtout lolu mo dakeu lém

(Huhum wooh)

Boul déglu ki ñeuw nan la bayima

Koku abb none la

(Noneu leu)

Beuguél Capitainu borom

Man deh Commando la

Bateau dém Bateau costé

Kiko beug

Man deh duma ko ko May

(No no no)

Keur gui bén seurr fi néh

Makoy Takeu

Dialal ba Thiaka Ndiaye

Légui damay ngoyy si seuy bi

(Ni la deh)

Séyy fi yoku thiéré doli ñéx

(Ni la deh)

Fane yi dama féroce jongué lolu

(Ni la deh)

Sa jeukeur boko yoré def no xalé way

(Mané Ni la deh)

Légui damay ngoyy si seuy bi lé

(Ni la deh)

Séyy fi yoku thiéré doli ñéx

(Ni la deh)

Fane yi dama féroce jongué lolu

(Ni la deh)

Sa jeukeur boko yoré Déf ko xalé waay

(Mané Ni la deh)

Bae dama firr

Té dama gawa salitt

Am xadar wayé

Xol bi japul dara

Damala noba noba

Noba noba nobb

Man mi yamalé malak dara

Goudi baby boul ragal

Limay yeuk bve

Est ce que yaguikoy yeuk

Boul ragal ndaxté dula gañ

Limay yeuk bve

Nex na yaguikoy yeuk

Cheri cheri cheri balma

Thiow li thiow li thiow li man la

(wowowow)

Duman mala mom

Dina ngoy ci yaw

Mélni dakandé

Légui damay ngoyy si seuy bi

(Ni la deh)

Séyy fi yoku thiéré doli ñéx

(Ni la deh)

Fane yi dama féroce jongué lolu

(Ni la deh)

Sa jeukeur boko yoré Déf ko xalé waay

(Ni la deh)

Légui damay ngoyy si seuy bi lé

(Ni la deh)

Séyy fi yoku thiéré doli ñéx

(Ni la deh)

Fane yi dama féroce jongué lolu

(Ni la deh)

Sa jeukeur boko yoré Déf ko xalé waay

- It's already the end -