background cover of music playing
Ndongo - Samba Peuzzi

Ndongo

Samba Peuzzi

00:00

02:39

Similar recommendations

Lyric

Aaah eh

Ayaa

Sénégal boy

Yeah

Balle bangui sogga takk

Négros sama guinaw

Man rek man kassé fi têk tankeu

Xaliss dou doy diameu dou eup

Tour bangui dèm succès dii yokou

Listen piss feuri nioun dougnla faté

Dérétou diamageun mofiy daw

Dé rek momay tèrè té game bi

Iyoo iyoo

Nimay rabé loussiy sa yonn

Bandit deug dankay ndirou

Xamnaani si man ngay xol

Mais non non ningkoy défé dou nonou

BEM laa lal deh

Sa show man la bardé

Ay caché millions sans projet

Man la Sénégal boy from G

Eh non non thiow li dou beuri

Man nguén ték sèn beut yi

Yanou wadiour motakh ma yèksi fi waa eeh

Niom louniou fok?

Meunouniou bok

Xir bi la yorr niouy daw malèn koy nok

Eh manguék buzzou Ndongo

Dama xew

Hey boma xamoul

Dèmal nga tok

Eh dèmal nga tok

Eh boma xamoul bou yaa dèmal nga tok

Ya hey pik yiniouy sanii mann damako toul

Niomassi djitou malènn raw fouf

- It's already the end -