background cover of music playing
Désolé - Wally B. Seck

Désolé

Wally B. Seck

00:00

03:42

Similar recommendations

Lyric

C'est pas de ma faute

Sou féké damalaye dérangé

Désolé

Nga baalma

Xamna sakh niima mele si rewmi Nekhoula

Désolé

I'm so sorry

Soudé louma lalle

Yalla teksi loxo

Ngeunele laa

Wakhambané bou gnémé

Kouy ligueye guene

Lou setane si mane

Non non

Linga dadie si yakeu

Soko dadione si ligueye

Wessou fii

Je suis dé so lé

C'est pas de ma faute

Sou féké damalaye dérangé

Désolé

Nga baalma

Xamna sakh

Niima mele si rewmi Nekhoula

Désolé

Go man inside

Soudé louma lalle

Yalla teksi loxo

Ngeunele laa

Wakhambané bou gnémé

Kouy ligueye guene

Lou setane si mane

Non non

Linga dadie si yakeu

Soko dadione si ligueye

Wessou fii

Je suis dé so lé

Si être aimé par les autres

Peut faire mal à autrui

Désolé

Si mes plumes

Par mes mélodies te détruit

Je suis dé so lé

Yow kholale

Diiwangui nééé di deme

Bour yalla koye deff si diamame

Mala douma tabakh

Because Lou domou adama bi lambo

Bour yalla koko diaguelele

(Soula yaboo)

" Baye gualaye nagou Nagou mo geune"

(Sa wadjii boula yaboo)

" Mame Ro mo dogual nagne nagou Nopalou "

"Yalla gueumoul nelawoul tei dou diawaleii "

"Dieufou kouné louné lounekk foneii guathia "

Forou mako

Lima diangue

Laye tari

Sathiou mako (lima diangue lay tarii)

"Lou waye donnou mou deugeur " "Li gua yorr forouloko"

Ennhhhhhh

...n'a Na Na naa ohh

Forou mako

Lima diangue

Laye tari wo wo wooo

Sathiou mako

Sama gnom mame gnoma togne

Nana nana nana

"Li loussii waye mane Sing Sing dou nakhé mbaaye

Ndakh nakhé mbaaye dou yagué nii ""

Ahhhhhhhh

Non non non

Oh oh oh

#Mag'Ør

- It's already the end -