00:00
03:50
Méritewuma la, eh yeah
Méritewuma la, eh yeah
Méritewuma la, eh yeah
Waxal sa xol ne fonk naa
Ko tekk naa ko fu ma tekkul kenn oh yeah, ah yeah
Waxal sa xol ne fonk na
Ko tekk na ko fu ma tekkul kenn oh yeah, ah yeah
Méritewuma la
Méritewuma la
Yallah xam na méritewuma la
Oh méritewuma la
Àttewóo ma ñàkkal bu may deconné
Decidéwóo bañ ma, xaar ba ma xëy dem
Tundu wi yépp yëg sa taar
Te taxul nga changé
Méritewuma la
Waxal sa xol ne fonk naa
Ko tekk na ko fu ma tekkul kenn oh yeah, ah yeah
Waxal sa xol ne fonk naa
Ko tekk na ko fu ma tekkul kenn oh yeah, ah yeah
Méritewuma la
Méritewuma la
Yàlla xam na méritewuma la
Oh méritewuma la
Na asamaan si taw muur say ronqooñ
Na dënu bi dal nëbb say xéxet
Bëgguma ngay jooy, danga may dofloo
Rabil aala miina ma boole ak yaw
Ci sa wet rek laay man a keppaaroo
Na asamaan si taw muur say ronqooñ
Na dënu bi dal nëbb say xéxet
Bëgguma ngay jooy, danga may dofloo
Rabil aala miina ma boole ak yaw
Ci sa wet rek laay man a keppaaroo
Waxal sa xol ni fonk na